TSK

TSK · Jude 1:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax ji, géej a riir, géej a àddu, mu riir, gannax ya rëkk, mu riir.

Man daal, dungeen ma ragal, am tiituleen ma?» Kàddug Aji Sax jee. «Man mi teg gannuus, yemalee ko géej, dogalal ko ko dàkk te du ko jàll, lu mu wañax wañax du ko man; gannax ya day riir, te du jàll!

Waaye nit ñu bon ñi, ak maa-man yi dañuy gën di bon rekk, di naxe tey nax seen bopp.

¶ Ñetteelu malaaka mi wal liitam, biddiiw bu réy buy tàkk nig jum xàwwikoo asamaan, wadd ci kaw ñetteelu xaaju dex yi ak bëti ndox yi.

Ñu jàpp nag Seytaane, mi leen daan nax, sànni ko ci déegu sawaraak tamarax ba, mu fekki fa rab waak yonentu caaxaan ba. Dees na leen fa mitital guddi ak bëccëg, ba fàww.