TSK

TSK · Jude 1:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ñooñu, kenn desul ca seen biir, te bokkoon ca limeefu bànni Israyil, ba Musaak Aaróona sarxalkat ba jëkkoona tënke ca màndiŋu Sinayi.

Moo tax mu giñal leen ne dina leen tëral fa màndiŋ ma,

¶ Bokk yi, bugguma ngeen umple ko, sunu maam yépp la niir wa yiiroon, te ñoom ñépp a jàll géej ga.

¶ Moo waral ma fas yéene di leen dëkke fàttli loolu, doonte xas ngeen koo xam, ba tax ngeen taxaw bu dëgër ci dëgg gi leen nuyusi.