Job 30:10
TSK
Dañu maa seexlu, ñooru ma, néeg maa serati ci kanam.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Dañu maa seexlu, ñooru ma, néeg maa serati ci kanam.
Yaa gis ñu di ma sewal, di ma ruslook a torxal, yaa ngi ne jàkk ci noonoo noon.
Gannaaw laa jox ku may dóor, dékk lex kuy xus sama sikkim, te làquma sama kanam ku may saagaak a serati.
Ku leen talaata cib lex, dékkleen ko ba ca des. Ku nangu seen mbubb mu mag, buleen ko teree jëlaale seenub turki.