TSK

TSK · Lamentations 3:32

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba ñu demee ba mu yàgg, Firawna buuru Misra dee. Fekk na bànni Israyil a ngay binni rekk ndax seen njaam ga. Ñuy woote wall, ba seen jooy, ya sababoo ca seen toroxteg njaam ga, àgg fa Yàlla.

Yeen aji gëm ñi, woyleen Aji Sax ji, njukkale ko sellngaam.

Ni asamaan tiime suuf, ni la ngoram yiire ku ko ragal.

bàyyi xel ci kóllëreem ak ñoom, topp ngoram lu réy, ba giif,

Mu ne: «Maa la wacc diir bu gàtt, dellu la jël ci yërmande ju yaa.

¶ «Mu jóg, ngir dellu kër baayam. Fu sore la ko baayam séene, muy dikk. Mu ñeewante ko, daw, laxasu ko, fóon ko.