TSK

TSK · Lamentations 4:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ñaawtéef daal laa judduwaale, te sama ndey ëmbaale ma bàkkaar.

Ba fukki fan ya matee, seen kanam gëna leer te ñu gëna suur mboolem xale yu góor yay lekk ca njëlal Buur.

Luke 1:15 TSK

ndax ku màgg lay doon, Boroom bi seede. Biiñ ak lenn luy màndee nag, du ko naan, Noo gu Sell gi mooy dale ca biiru ndeyam, solu ko ba fees.