TSK

TSK · Leviticus 11:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

tund wu mag ñeel kéwéli àll, xunti di rawtub daman.

Ndaxte ñu baree ngii ñu seeni jëf tax ñu di nooni bantub Almasi. Loolu wax naa leen ko ay yoon, ma waxati leen ko tey aki jooy.

Xam Yàlla lañuy woote, te seeni jëf weddi Yàlla; nit ñu jara jéppi, ñu déggadi lañu, te tëlee def lenn lu baax.