كل أسفار KYG

Leviticus 13

KYG · الآية 52

27 أصحاحات

KYG / Leviticus / الأصحاح 13

KYG · الآية 52

D a koy lakk, ndax liir wu aaytal la, muy ndimo mbaa bàgg mbaa poqe mbaa kawaru gàtt gu ñu ëcc mbaa wëñ gu ëccu mbaa lu ñu defare der te liir wa tegu ca. Dees koy lakk, ba mu dib dóom.