Leviticus 14:2
TSK
«Li yoon digle ci mbirum nit ku ame jàngoroy der juy law, keroog bés ba ñuy laabal nit ki, mooy lii: Nañu ko yegge sarxalkat bi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
«Li yoon digle ci mbirum nit ku ame jàngoroy der juy law, keroog bés ba ñuy laabal nit ki, mooy lii: Nañu ko yegge sarxalkat bi.
mooy tegtal biy xamle lu set ak lu setul. Loolu la yoon digle ci jàngoroy der juy law mbaa liir.
¶ Loolu la yoon digle ci mbiri góor gu ànd ak jàngoroy xelli mbaa mu génne wasal, ba sobewu;
Ndegam nag jëkkër ji, beneen bés, gannaaw ba mu déggee kàdduy jabaram, la doora àddu ngir neenal wax ja, su boobaa mooy gàddu bàkkaaru jabaram.»