Dañoo daane jëmmi Baal ja, màbb kër Baal, boole ca, def kob sën, te moom la ba tey jii.
TSK
TSK · Leviticus 14:45
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
2 Kings 10:27
TSK
2 Kings 18:4
TSK
¶ Moom moo dindi bérabi jaamookaay ya, toj tuuri doj ya, gor xer wa ñuy jaamoo Asera, rajaxe jaanu xànjar ja Musaa defaroon. Ndax ba ca jamono yooya waa Israyil dañu daan taalal jaanu xànjar ja cuuraay, tudde ko Nexustan.
2 Kings 25:25
TSK
¶ Gannaaw gi, ca juróom ñaareelu weeru at ma, Ismayil doomu Netaña doomu Elisama, bokk ci askanu buur, ànd ak fukki nit, dikk bóom Gedalya, bóomaale waa Yudak waa Babilon ya nekkoon ak moom ca Mispa.
Ezekiel 5:4
TSK
Nga dellu sàkk cooca, sànni ca sawara sa, lakk ko. Ca la sawaray jóge, tàkkal mboolem waa kër Israyil.
Revelation 11:2
TSK
Waaye ëttu bitib kër Yàlla gi, bàyyi ko, bu ko natt, ndax ñi dul Yawut lees ko jox, te ñooy dëggaate dëkk bu sell bi diiru ñeent fukki weer ak ñaar.