TSK

TSK · Leviticus 14:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Su ko defee sarxalkat bi day fab ndabal xandeer, duy ko ndox mu sell mi ñuy setloo, te na sàkk ci suufas jaamookaay bi, def ko ci ndox mi.

¶ Xam nanu ne sunu yaram, sunu këru kaw suuf gii di ab xayma, bu daanoo it, am taax lanu am fa Yàlla, kër gu sax dàkk, gu loxol nit tabaxul.

¶ Gone yooyu nag, bindeefi suux ak deret lañu bokk doon, ñoom ñépp. Moo tax Yeesu itam dikk bokk ak ñoom woowu nekkin, ngir mana dee ba def deewug boppam pexe mi mu neenale ka yoroon dooley ndee, te mooy Seytaane.