TSK

TSK · Leviticus 19:29

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Ab gànc mbaa ku ñu torxal, tëdde ko, ñoom duñu ko jël soxna. Ku jëkkëram baal it duñu ko jël soxna, ndax dañoo sellalal seen bopp seen Yàlla.

¶ Gànc bu jigéen buy gànctul ay tuur, bumu am ci biir jigéeni Israyil, te gànc bu góor buy gànctul ay tuur, bumu am ci góori Israyil.

Xanaa xamuleen ne, seen yaram mooy céri Almasi? Waaw, ndax damay jël céri Almasi, def ko céri gànc bu jigéen? Yàlla tere!