TSK

TSK · Leviticus 22:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Jaam bu juddoo sa kër ak boo jënd, ñoom ñaar ñépp, dees leen wara xarfal. Xaraf ay màndargaal sama kóllëre ci seen yaram, muy kóllëre gu sax fàww.

Du tere mu saña lekk ci ñamu Yàllaam, muy ñam wu sell ak wu sella sell.

¶ «Leneen lu la ñeel moo di jooxe bu jóge ci saraxi nit ñi, di bépp saraxu yékkati-jébbal bu bànni Israyil. Yaw laa ko sédd, yaak sa doom yu góor, ak sa doom yu jigéen, ci kaw dogalu yoon bu sax dàkk. Képp ku set ci sa waa kër, sañ na cee lekk.