«Man Aji Sax ji, maa di seen Yàlla, ji leen génne réewum Misra, kërug njaam ga.
TSK
TSK · Leviticus 25:10
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ku amul ku ko ko jotaatal te moom ci boppam mu mujj woomle, ba am lu mu ko jotaate,
mu génn ci seeni loxo, mook ay doomam, daldi dellu ci làngu boppam, fa ay maamam séddoo.
¶ «Su fekkee ne nit ki dafa jagleel Aji Sax ji tool bu mu jënd, te donnu ko,
Te it bu atum Yiwiku mu bànni Israyil agsee, seen cér day dolliku ca céru giir ga ñu séyi ca seen biir. Te kon it ci sunu céru giiru maam, la seen cér boobu di wàññikoo.»
di àtte néew-ji-doole, di leel ku xiif. Aji Sax jeey tijji ku ñu tëj.
Manees naa foqati alalu sëxëtoo ci loxol jàmbaar a? Am manees naa rëcc boroom doole bu la jàpp?
Moo ma yónni ngir ma yéene atum yiwu Aji Sax ji, ak at mu sunu Yàlla di mbugalee. Moo ma yónni ngir dëfal ñiy ñaawlu ñépp,
¶ Kàddu gii dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo ci Aji Sax ji, gannaaw ba Buur Cedesyas fasook mboolem waa Yerusalem ngir goreel jaam yi,
«Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: Man maa fasoon kóllëre ak seeni maam keroog bés ba ma leen génnee réewum Misra kërug njaam ga, ne leen:
Waaye su ki ci jal bi mayee kenn ciy surgaam lenn ci suufam, ba keroog atum Yiwiku ma rekk la surga ba di moom suuf sa, waaye bu atum Yiwiku teewee, suuf si day dellu ci loxol ki ci jal bi. Suuf soosu, céru doomi boroom jal bi doŋŋ lay doon.
ne moo nuy may nu mucce ci loxoy noon, ba man koo jaamoo xel mu dal
Boroom bi mooy Noo gi, te fu Noo gi nekk, fa la nit di moome boppam.
¶ Yeen de bokk yi, cig yiwiku lees leen woo. Moytuleen lenn rekk: bu seenug yiwiku diw lay, ngir topp seen bakkan, waaye deeleen surgawoonte ngir cofeel.
Ag ngoreel lañu leen di dig, te ñoom ci seen bopp, ay jaami yàqute lañu, nde lu la man, yaa dib jaamam.