ne ko mu wax bànni Israyil ne leen: «Góor ak jigéen, képp ku ci dogu ba xas xasu doon ab nasireen, ngir sédd boppam Aji Sax ji,
TSK
TSK · Leviticus 27:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Numbers 6:2
TSK
Numbers 30:3
TSK
¶ «Góor gu xasal Aji Sax ji aw xas, mbaa mu giñ ngir dogu gu mu tegool boppam, bumu tebbi kàddoom. Noonee ko làmmiñam tudde, na ko ni defe ba mu mat sëkk.
¶ Su ngeen xasalee seen Yàlla Aji Sax ji, aw xas, buleen ko yeexa wàccool, ndax kon seen Yàlla Aji Sax ji du leen ko ñàkka topp, te kon muy seen bàkkaar.
Li seen làmmiñ tudd, sàmmooleen koo jëfe na ngeen ko xasale woon seen Yàlla Aji Sax ji, ci seen sagoy bopp, ak seen kàddug bopp.
1 Samuel 1:28
TSK
Léegi nag man maa ko sédd Aji Sax ji: giiru dundam lees ko sédd Aji Sax ji.» Ba loolu amee ñu sujjóotal Aji Sax ji foofa.
Ecclesiastes 5:3
TSK
Boo digook Yàlla, bu ko yeexe; Daray foontukat neexul, defal li nga dige.