Leviticus 4:4
TSK
Day yóbbu yëkk wi ci bunt xaymab ndaje mi, ci kanam Aji Sax ji, daldi teg loxoom ci boppu yëkk wi, ñu rendi yëkk wi ci kanam Aji Sax ji.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Day yóbbu yëkk wi ci bunt xaymab ndaje mi, ci kanam Aji Sax ji, daldi teg loxoom ci boppu yëkk wi, ñu rendi yëkk wi ci kanam Aji Sax ji.
Day teg loxoom ci boppu sikket bi, rendi ko fa ñuy rendi saraxu rendi-dóomal, fa kanam Aji Sax ji. Saraxu póotum bàkkaar la.
Soxlawuñu woona laaj dara nit ñi ñuy teg xaalis bi ci seeni loxo ngir ñu fey liggéeykat yi, ndax maandu ga ñu daan jëfe.
ndax deretu yëkk, ak ju sikket kat manula far ay bàkkaar.