Leviticus 4:5
TSK
Sarxalkat bi ñu diw, fal ko, na sàkk ci deretu yëkk wi, yóbbu ci biir xaymab ndaje mi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Sarxalkat bi ñu diw, fal ko, na sàkk ci deretu yëkk wi, yóbbu ci biir xaymab ndaje mi.
Na génne yëkk wi dal bi, taal ko, na muy taale yëkk wi ñu jëkka wax. Saraxu póotum bàkkaaru mbooloo mi la.
Muy yëkk wiy saraxu póotum bàkkaar, muy sikket biy saraxu póotum bàkkaar te ñu yóbbu woon seen deret ca biir bérab bu sell baa sell ngir defe ko njotlaay, lépp lañuy génne dal bi. Der yaak yàpp waak sébbriit ma dees koy boole lakk, ba mu dib dóom.