TSK

TSK · Leviticus 7:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Gannaaw gi Yàlla Aji Sax ji sàkkal Aadama ak soxnaam ay yérey der, wodde leen.

Juru saraxu rendi-dóomal bi, na ko boroom sarax bi fees, daggat ko.

Nañu lakk nag wi‎ ci kanamam. Der bi ak yàpp wi ak deret ji ak sébbriit mi, lépp lañuy lakk.

Waaye yiirooleen Sang Yeesu Almasi, te ngeen baña yittewoo seen bakkan, ngir di topp seeni xemmemtéef.