TSK

TSK · Luke 1:64

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nanga wax ak moom, digal ko li mu wara wax. Man maay ànd ak yeen, yaak moom, saa yu ngeen dee wax, te maa leen di xamal, yeen ñaar, li ngeen wara def.

ma xamal tooñkat sa war, ba moykat dellu ci yaw.

Bésub keroog dees na ne: «Aji Sax ji, sant naa la; yaa ma mere woon, meddi, dëfal ma.»

Waaye bu ma amee lu ma lay wax, dinaa ubbi sa gémmiñ. Su ko defee nga ne leen: “Lii Boroom bi Aji Sax ji da koo wax.” Kuy dégg, dégg; kuy gàntal, gàntal. Ndax kërug fippukat lañu.»

Fekk na ngoon ga jiitu dikkam, Aji Sax ji teg ma loxo, ba tijji sama gémmiñ. Ba waa ja rëcc agsee fa man ca ëllëg sa ca suba, fekk na sama gémmiñ tijjiku, luuwatuma.

Luke 1:20 TSK

Léegi nag, dama ne, gannaaw gëmuloo sama kàddu, giy jot, sotti, dinga luu te dootuloo mana wax, ba kera loolu di am.»