TSK

TSK · Luke 10:19

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

luy nàmp di foye paxum ndox-suuf, perantal di laal tostanum ñàngóor.

Ñépp a leen di bañ ndax sama tur.

¶ Ana lu nuy waxati nag? Gannaaw Yàllaa ànd ak nun, ku nu manal dara?

¶ Buleen jikkowoo bëgg ub xaalis; doylooleen li ngeen am, ndax Yàlla moo ne: «Duma la bàyyi mukk, duma la wacc mukk.»