TSK

TSK · Luke 10:29

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 32:2 TSK

Ba loolu amee Eliyu doomu Barakel ma askanoo ci Buus, bokk ci làngu Ram daa mer ba futt ca la Ayóoba dëggal boppam fi kanam Yàlla,

¶ Mu teg ca ne ko: «Ñett ñii, kan nga foog ne moo ci taxawu waa ja dajeek sàcc ya, taxawaayu nit ak moroomam?»

Luke 18:9 TSK

¶ Yeesu léebati lii, ngir ñiy damoo seenug njub, tey doyadal ñi ci des.

Yoonu njub gi Yàlla di joxe nit ki, àtteb ku jub, moom lañu umple tey jéema dëggal seen njubteg bopp. Moo tax nanguluñu njubte gi Yàlla di maye.

Ngeen gis kon ne ci jëf lees di joxe nit àtteb ku jub, waaye du ci kaw ngëm doŋŋ.