Exodus 4:24
TSK
¶ Ba ñu lalee panaan ca yoon wa, Aji Sax ji dafa dogale Musaa, nar koo rey.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba ñu lalee panaan ca yoon wa, Aji Sax ji dafa dogale Musaa, nar koo rey.
di faj naqaru xol, fajtal góomi boroom.
Bu sab noon xiifee, jox ko mu lekk, bu maree, may ko mu naan,
Mu am doom ju góor, mu dib taawam. Mu laxas ko, tëral ko ca gàmbug jur ga, ndax ñàkk fu ñu xaj ca néegu gan ba.
Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.