Ndax ngor laa namm, dub sarax, ràññee Yàllaa ma gënal saraxi rendi-dóomal.
TSK
TSK · Luke 10:37
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Hosea 6:6
TSK
Luke 6:32
TSK
¶ «Su dee ñi leen sopp doŋŋ ngeen sopp, ana lu ngeen ci wara yooloo? Bàkkaarkat yi sax, ñi leen sopp, sopp nañu leen.
Xam ngeen kat sunu yiwu Boroom Yeesu Almasi, moom mi woomle woon, te yeena tax mu ñàkk, ngir woomale leen ag ñàkkam.
Ephesians 5:2
TSK
te ngeen di doxale cofeel, ni Almasi mi nu sopp, ba jooxeel nu bakkanam, def ko saraxu sawara, ngir xetug jàmm, ñeel Yàlla.
1 Peter 2:21
TSK
Ci loolu sax lañu leen woo, ndax Almasi itam sonnal na leen, te moo leen bàyyeel ab royukaay, ngir ngeen jaar ciy tànkam.
Revelation 1:5
TSK
tukkee itam fa Yeesu Almasi, seede bu wóor bi, moom taaw bi, ki jëkka dekki, jóge ci ñi dee, di kilifay buuri kaw suuf. Moom mi nu sopp, yiwee nu deretam, ba nu teqlikook kilifteefu sunuy bàkkaar,