Luke 4:43
TSK
Mu ne leen: «Yeneen dëkk yeet, war na ma faa yégleji xibaaru jàmm bu nguurug Yàlla, ndax loolu lañu ma yebale.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne leen: «Yeneen dëkk yeet, war na ma faa yégleji xibaaru jàmm bu nguurug Yàlla, ndax loolu lañu ma yebale.»
ak ni Yàlla ànde ak Yeesum Nasaret, ba jagleel ko pal gu mu dogale Noo gu Sell geek xam-xam bi mu ko sotti, muy wër, di def lu baax, di faj mboolem ñi Seytaane notoon.