TSK

TSK · Luke 13:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Léegi seetaan ma rekk, samam sànj tàkkal leen, ba ma faagaagal leen, te du tee ma def la askan wu mag.»

Waaye dinaa leen yónnee sama barke ca atum juróom benneel ba, suuf si nangul leen meññeefum ñetti at.

Luke 3:9 TSK

Te itam sémmiñ xàccil na reenu garab ba noppi. Kon nag gépp garab gu ci meññul doom yu baax, dees koy gor, sànni ca sawara sa.»