TSK

TSK · Luke 16:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nanu ci sàkk pexe, ngir ñu bañatee yokku. Lu ko moy bu xare amee, man nañoo far ak sunuy noon, xeex ak nun, ba génn réew mi.»

Ayca, wool-leen ma yonenti Baal yépp ak sarxalkatam yépp ak jaamukatam yépp. Bu kenn wuute, ndax sarax bu réy laay defal Baal. Képp ku ko wuute dina dee.» Booba Yewoo ngi fexee nax ñiy jaamu Baal, ba rey leen.

Ana kuy dund ba fàww, ba doo gis bàmmeel?

Xel mu ñaw, jëw bu rafet; sam xel jekkadi, ñu xeeb la.

Luke 16:4 TSK

Gannaaw loolu mu ne “Xam naa ni may def, ba su ma ñàkkee sama liggéey it, dees na ma fat.”

Luke 18:6 TSK

¶ Sang bi teg ca ne: «Jàngatleen li àttekat bu bon bi wax.

Ag lëndëm ngeen woon démb, waaye tey ag leer ngeen ci Boroom bi ngeen bokk. Jëfeleen nag ni niti leer.

Yeen ñépp ay doomi leer ngeen, doomi bëccëg ndarakàmm; nun bokkunu dara ak guddi, mbaa ag lëndëm.