Liggéey boo gis, liggéeyal; def ci loo man. Ndax muy jëf, di doxalin, di xam-xam, di manoore, dara amu ci njaniiw, ga nga jëm.
TSK
TSK · Luke 2:16
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Luke 2:7
TSK
Mu am doom ju góor, mu dib taawam. Mu laxas ko, tëral ko ca gàmbug jur ga, ndax ñàkk fu ñu xaj ca néegu gan ba.
Luke 19:32
TSK
¶ Ba ndaw ya demee, na leen ko Yeesu waxe lañu ko gise.