Ma boole jël kayitu njaay bi tëjewul ak kayitu njaay bi tëje, te yoonalu njaay meek sàrt yi tënke ci.
TSK
TSK · Luke 2:27
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Jeremiah 32:11
TSK
Luke 2:22
TSK
¶ Gannaaw ba seen fani setlu matee, ni ko yoonu Musaa laaje, ñu yóbbu xale bi Yerusalem, ngir teewal ko fi kanam Boroom bi,
Luke 2:48
TSK
Ay waajuram gis ko, waaru. Yaayam ne ko: «Doom, li nga nu def nag? Maak sa baay a ngi jaaxle, di la seet!»
Luke 4:1
TSK
¶ Yeesu moo feese woon Noo gu Sell gi, bàyyikoo dexu Yurdan, ci njiital Noo gi, ca biir màndiŋ ma.
Acts 10:19
TSK
¶ Naka la Piyeer di xalaat ba tey ca peeñu ma, Noo gi ne ko: «Ñetti nit a ngi nii, di la seet.
Acts 16:7
TSK
Ñu dem ba ca kemu Misi, nara jàlli biir diiwaanu Bitini, Xelum Yeesu mayu leen ko.
Revelation 17:3
TSK
¶ Ci kaw loolu malaaka mi yóbboo ma Noowug Yàlla ba ca màndiŋ ma. Ma gis jigéen ju war rab wu xonq wu am juróom ñaari bopp ak fukki béjjén, te yaram wi fees ak tur yuy saaga Yàlla.