TSK

TSK · Luke 2:46

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ñetteelu bés ba Yerbowam ànd ak mbooloo ma mépp, dellu ca Robowam, noonee leen ko Buur waxe woon ne leen ñu dem ba mu am ñetti fan, ñu délsi.

Boroom bi Aji Sax ji moo ma may làmmiñu ndongo lu mokkal, ngir ma xam gan kàddu laay jàpplee ku sonn. Suba su ne mu yee ma, yeel ma nopp bu ma teewloo ni dongo yi.

Luke 2:44 TSK

Ñu xalaat ne, Yeesu daa ànd ak ñu ñu bokkaloon yoon. Dox nañu bésub lëmm, door koo wëri ci seeni bokk ak seeni xame,

Acts 5:34 TSK

Ab Farisen bu ñuy wax Gamalyel, di jànglekatu yoonu Musaa bu ñépp nawloo, daldi taxaw ca digg kurélu àttekat ya. Mu joxe ndigal ngir ñu génne leen ab diir.