rawtub sàcc daal ngeen def kër gii ñu ma tudde? Man de lii laa gis!” Kàddug Aji Sax jee.
TSK
TSK · Luke 21:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ana lu waral ngay biral waxyu ci turu Aji Sax ji, naan kër Yàlla gii dina tas, mel ni ga woon ca Silo, te dëkk bii day tas, kenn du fi des?» Mbooloo ma mépp nag sam Yeremi ca biir kër Aji Sax ji.
Moo tas mbaaram ni bu doon mbaarum tool, moo rajaxe bérabu ndajeem. Aji Sax ji moo fàtteloo waa Siyoŋ màggal ak bésub Noflaay, te tàngooru meram la xalabe buur ak sarxalkat.
tundu Siyoŋ wi gental, ba till yi di fi daagoo.
Bu juróom benn fukk yeek ñaar ciy àppi juróom ñaar weesee, dees na bóom ku ñu fal, te kenn du ànd ak moom. Gannaaw loolu kilifa dina ñëw, ànd ak gàngooram, yàqte dëkk beek jaamookaay bi. Waaye kilifa googu lu mel ni mbënn a koy mujje. Dogal nañu ne yàqte gi dina wéy ba keroog xare biy jeex.
¶ Libaŋéey, ubbil say wunt, sawara xoyom sa garabi seedar.
Ñoo lay nappaaje ci suuf, yaak say doom yi ci sa biir, te duñu bàyyi doj ci kaw doj ci sa biir, ndax ba sa bésub wall dikkee, yaa ko ràññeewuloon.»