Luke 14:15
TSK
¶ Kenn ca gan ña nag dégg loolu, ne Yeesu: «Ndokklee ku lekk ca bernde ja ca nguurug Yàlla!»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Kenn ca gan ña nag dégg loolu, ne Yeesu: «Ndokklee ku lekk ca bernde ja ca nguurug Yàlla!»
Du askan wépp la ko won, xanaa nun, seede yi Yàlla tànnoon lu jiitu, nu bokk ak moom lekk ak naan, gannaaw ndekkiteem.
¶ Yoonu Musaa takkndeeru xéewal yiy ñëw doŋŋ a ci nekk, waaye xéewal ya ci seen bopp nekku ci. Looloo tax sarax yi yoon wi laaj ñu war koo saxoo jébbale at mu nekk, manula setal mukk wecc ñiy jaamusi.