TSK

TSK · Luke 23:22

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Mu ne leen: «Yeena ma indil waa jii, ne ma mooy lajjal askan wi. Man nag laaj naa ko ci seen kanam, waaye gisuma ci moom genn tooñ ci li ngeen ko tuumaal.

Pilaat namma bàyyi Yeesu, daldi waxaat ak mbooloo ma.

Almasi itam benn yoon la daj coono ndax bàkkaari nit ñi, moom miy ki jub moo leen ko defal yeen ñi jubadi, ngir yóbbu leen fa Yàlla; moom lañu rey yaramu suuxam, waaye moo dundaat ci dooley Noo gi.