¶ Aji Sax ji dellooti ne ko: «Léegi dugalal sa loxo, teg ko ci sa dënn.» Musaa dugal loxoom, teg ko ca dënnam; ba mu ko génnee, mu defi àkk, xobbiku.
TSK
TSK · Luke 5:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Exodus 4:6
TSK
Leviticus 13:1
TSK
¶ Aji Sax ji wax na Musaa ak Aaróona ne leen:
Deuteronomy 24:8
TSK
¶ Fexeleen ba ci biir mbasum jàngoroy der juy màgg, ngeen di sàmmoo jëfe bu baax, mboolem lu leen sarxalkat yi, Leween ñi tegtal. Ni ma ko sante sarxalkat yi, Leween ñi, sàmmooleen koo jëfe noonu.
1 Kings 18:39
TSK
¶ Ba mbooloo mépp gisee loolu, dañu ne gurub, dëpp seen jë fa suuf, daldi ne: «Aji Sax jeey Yàlla! Aji Sax ji kay mooy Yàlla!»
2 Kings 5:27
TSK
Ngaanag Naaman dina la topp, yaak saw askan ba fàww!» Ba mu ko defee Gewasi bàyyikoo ca Alyaasa, daldi gaana, yaram wa ne fureet, weex furr.
Psalms 50:15
TSK
di ma woo bésub njàqare, ma wallu la, nga màggal ma.»
Luke 17:16
TSK
Mu dikk, ne gurub, dëpp jëëm fa tànki Yeesu, sant ko. Waa ja nag nitu Samari la woon.