Mu ne: «Lu waral kon nga naral lu ni mel ñoñi Yàlla ñi? Buur, boo waxee loolu kay, mel na ni tooñ nga, ndax jëliwoo sa doom ja gàddaay.
TSK
TSK · Luke 7:42
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
di ñu wóolu seen am-am, di kañoo alal ju bare?
Moo lay baal foo ñaawe, di la wéral foo woppe.
Maa far say moy, mu naaxsaay niw niir, say bàkkaar ne mes nib lay. Délsil fi man, jot naa la.»
Rikk sama Yàlla, teewlul, déglul te xippi, ba gis sunu gent yi ak sa dëkk ba ñuy tudd sa tur. Du sunu njekk lanu lay dagaane moos, waaye sa yërmande ju yaa rekk a tax.
te ci yiwu Yàlla wu àndul ak genn pey lees di joxe ñépp àtteb ñu jub, ndax njot gi sottee ci Almasi Yeesu.
¶ Ndax kat, ba nu amul menn pexem mucc, ca la Almasi deeyal yéefar yi nu doon, ba mu jotee.
¶ Ci moom lanu ame njot gi nu sottalal njéggalug moy, ndax deretam ji tuuru, noonu ko Yàlla defe ci yiwam wu yaa,
Muñalanteleen te di balante, ndegam kenn a am lenn lu mu sikke moroomam. Ni leen Boroom bi baale, deeleen balantee noonu.