Deuteronomy 5:25
TSK
Waaye lu nuy jaayati nag sunu bakkan, doye? Ndax kat, sawara wu réy wii, su nu déggatee sunu kàddug Yàlla Aji Sax ji, da nuy xoyom.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye lu nuy jaayati nag sunu bakkan, doye? Ndax kat, sawara wu réy wii, su nu déggatee sunu kàddug Yàlla Aji Sax ji, da nuy xoyom.
Ba loolu amee Daawuda mer ca mbugal mu metti ma Aji Sax ji teg Usa. Moo tax mu tudde bérab booba Peres Usa (mu firi Mbugalum Usa), muy turam ba tey jii.
Moona kee noon Yàlla: «Xiddi ma! Xam saw yoon soxalu ma.
Ba mu gisee Yeesu, daa yuuxu, daanu fa kanamam, daldi xaacu ne: «Yaw Yeesu Doomu Yàlla Aji Kawe ji, ana lu ma joteek yaw? Dama lay tinu, bu ma mbugal!»
Ba loolu amee ñu jàll jëm beneen dëkk.
¶ «Ku leen déggal nag, man nga déggal; ku leen gàntal, man nga gàntal. Te ku ma gàntal, gàntal nga ki ma yebal.»