2 Kings 4:4
TSK
Su ko defee nga dellu tëjook say doom, ba noppi nga sotti diw gi ci ndab yooyu yépp, bu ci fees, nga ber.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Su ko defee nga dellu tëjook say doom, ba noppi nga sotti diw gi ci ndab yooyu yépp, bu ci fees, nga ber.»
Du xaacu, du biral; du jibal baatam ci mbedd mi.
Simoŋ mi Yeesuy wooye itam Piyeer, ak Àndre mi bokk ak Piyeer ndey ak baay, ak Yanqóoba ak Yowaan, ak Filib ak Bartelemi,
¶ Ci kaw loolu Piyeer dàq ñépp ca biti. Mu sukk, ñaan, daldi walbatiku jublook néew bi, ne: «Tabita, jógal!» Mu ne xiféet, gis Piyeer, jóg toog.