Ndax seen Yàlla Aji Sax jaa ngi leen di yóbbu réew mu baax; réew mu ami wal, ak bëti ndox, ak ndoxi xóote yu waley xur aki tund,
TSK
TSK · Malachi 3:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Deuteronomy 8:7
TSK
Isaiah 61:9
TSK
Dees na xàmmee seen askan fi biir xeet yi, xàmmee lu meññe ci ñoom fi biir waaso yi; képp ku leen gis ràññee ne ñooy askan wu Aji Sax ji barkeel.
Isaiah 62:5
TSK
Ni xale bu góor di takke ab janq, ni la la sa doom yu góor di moome ni jëkkër; ni boroom séet di bégee ab séetam, ni la la sa Yàlla di bégee.
Daniel 8:9
TSK
Ci kaw loolu béjjén bu ndaw génne ci béjjén yooyu benn, daldi lawa law jublu bëj-saalum ak penkook réew ma gëna rafet.
Zephaniah 3:19
TSK
Ma ne jant yooyu laay jëflanteek mboolem ñi leen di sonal. Ci laay wallu kuy sukkóot, fat ku tumurànke, may leen teraanga aku tur, fépp fu ñu ruse woon ci àddina.
Luke 1:48
TSK
moo geesu bii jaamam bu tekkeedi, ba maasoo maas doxe fi wooye ma boroom mbég mi,