Deuteronomy 23:8
TSK
¶ Buleen bañ ab Edomeen, ndax seen mbokk la. Buleen bañ nitu Misra, ndax ay doxandéem ngeen woon ca seenum réew.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Buleen bañ ab Edomeen, ndax seen mbokk la. Buleen bañ nitu Misra, ndax ay doxandéem ngeen woon ca seenum réew.
ba Aji Sax ji dëddu leen, muy la mu waxoon, yonent yay jaamam jottli ko. Noonu la mujj génne Israyil réewam, yóbbu leen Asiri ba bésub tey jii.
¶ Ña bàyyikoo Tel Mela ak Tel Arsa ak Kerub Adon ak Imer te manuñoo firndeel ne seen waa kër maam ak seen askan ci Israyil lañu bokk, ñii la:
Dungeen des ci réewum Aji Sax ji. Efrayim, Misra lay dellu, te ca Asiri, lu daganul lañu fay lekkeji.