Psalms 51:4
TSK
Fóotal maa fóotal sama ñaawtéef, raxasal ma sama moy.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Fóotal maa fóotal sama ñaawtéef, raxasal ma sama moy.
Moo tax ma bërgël leen ak seenug të, ñuy wéye seeni pexe.
Du xar mu ndaw moo ma defal saraxu rendi-dóomal, mbaa sarax yoo ma terale, te du sarax su ma la teg it, mbaa saraxu cuuraay bu ma la sonale.
Éey niti Israyili tey, teewluleen kàddug Aji Sax ji! «Ni màndiŋ mi aaye, ndax mas naa nee aaye ci Israyil? Mbaa ma mel ni réewum lëndëm aki loraangeem? Lu waral sama ñoñ naa: “Noo moom sunu bopp, dootunu délsi fi yaw”?
Mukk kay! Fàww Yàlla wéye di ku dëggu, te ñépp di ay fen-kat, te noonu la Mbind mi indee ne: «Soo waxee, am dëgg, te soo àttee, yey.»