Psalms 107:16
TSK
Moo rajaxe bunti xànjar, damm galani weñ.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Moo rajaxe bunti xànjar, damm galani weñ.
Su bés baa waa Misra mel niy jigéen, di lox ndax tiit loxo bi jóg, te Aji Sax ji Boroom gàngoor yi xàccil-leen ko.
mu ne: «Man maa lay jiitu, maasale mbartal, rajaxe buntu xànjar, damm tëjukaayu weñ.
Jàmbaari Babilon xareetuñu, ña nga des ca seeni tata, doole ŋiis, ñu mel niy jigéen. Bunti dëkk bi dàjjiku, kër ya jàpp.
Ca la njiit la di woolu kàngami xareem, ñuy gaawtu bay tërëf. b Tata ja lañuy gaaw wutali, ba yékkati ay kiiraay.