Nehemiah 11:22
TSK
¶ Kilifag Leween ña ca Yerusalem moo doon Utsi ma Bani di baayam; Xasabiya di baayu Bani, Mataña di baayu Xasabiya, Mika di baayu Mataña. Utsi bokkoon ci ñi askanoo ci Asaf te doonoon woykat yay woy ca kër Yàlla ga.