TSK

TSK · Nehemiah 13:14

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

«Éy Aji Sax ji, ngalla bàyyil xel ni ma àndeek yaw sama léppi xol, ci kóllëre, te li nga rafetlu laa jëfe.» Mu jooy nag, jooy yu metti.

Ezra 7:20 TSK

Leneen lu des it, loo wara def ci sa kër Yàlla gi, sañ nga koo génnee ci alalu buur.

Ezra 7:27 TSK

¶ Cant ñeel na Aji Sax ji, sunu Yàllay maam, moom mi def nii ci xolub Buur yéeney teral kër Aji Sax ji ci Yerusalem,

Ma sant it Leween ñi ñu laabal seen bopp te dem wattuji bunt ya, ngir sellal bésub Noflaay. Ngalla sama Yàlla, bàyyee ma lii xel itam te yërëme ma sa ngor lu bare.

Dagaanleen jàmmi Yerusalem: «Yerusalem, yal na sa xeli soppe dal,

Yàlla ñàkkul worma bay fàtte seen liggéey, ak cofeel gi ngeen sopp turam, te firndeele ko ni ngeen taxawoo ñu sell ñi, démb ak tey.