TSK

TSK · Nehemiah 2:4

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Fekk na ñu wax Daawuda ne ko Ayitofel bokk na ca ña lëngook Absalom. Daawuda nag ñaan ne: «Yaw, Aji Sax ji, ngalla yàqal pexem Ayitofel.»

¶ Ba ma déggee kàddu yooyu, damaa toog di jooy, ñaawlu ko ay fan, di woor ak a ñaan ci Yàlla Boroom asamaan.

Éy Boroom bi, Sang bi, rikk teewlul bu baax samag ñaan, ak sa ñaanu jaam ñi safoo wormaal saw tur. Ngalla Sang bi, nangul ma tey jii, may ma waa jii yéwéne ma.» Booba maa yore woon naani Buur.

Naka lañuy naan biiñ, Buur ne Esteer: «Ana looy laaj, ñu jox la ko, ana looy sàkku, ba ci genn-wàllu réew mi, ñu defal la ko.»

Santleen Yàlla mi ci asamaan! Kee saxoo ngoram!

Buleen jaaxle ci dara, waaye ci mbir mu mu mana doon, deeleen dikke Yàlla seeni soxla, di ko ñaan ak a dagaan te boole ci di ko sant.