¶ Ba loolu amee ñu feeñuji dalub waa Filisti, ñoom ñaar ñépp. Waa Filistee nga naan: «Xool-leen! Ay Ebraa ngay génne pax ya ñu làqu woon.»
TSK
TSK · Nehemiah 4:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ci biir loolu waa réew ma di yoqiloo waa Yuda, di leen xoqtal, ba ñu ragala tabax.
La ko dale bésub keroog sama xaaju nit ña rekk a doon liggéey, xaaj ba ca des gànnaayoo ay xeej aki pakk aki fitt ak kiiraayal dënn. Kilifa ya nag taxaw ca gannaaw mboolem waa Yuda.
¶ Sarxe nañu bésub keroog sarax yu réy tey bànneexu, ndax Yàllaa leen may bànneex bu réy. Jigéen ñaak gone ya it di bànneexu, mbégarey Yerusalem di dégtu fu sore.
Mu ne ma: «Yaw nit ki, ma ne, yii yax man naa dundaat a?» Ma ne ko: «Boroom bi Aji Sax ji, loolu de, yaw doŋŋ a ko xam.»
Éy Aji Sax ji, maa dégg sab jëw, Aji Sax ji maa yéemu ci sa jaloore! Ngalla yeesalal say jaloore, nu fekke, xamleel say jaloore, nu fekke, bu la am sànj teree geesu, yërëm.
Waaye li àddina jàppe ag ndof, moom la Yàlla taamu, ngir rusloo ko xamkat yi, te li néew doole ci àddina, moom la Yàlla taamu, ngir rusloo ko li bare doole.