TSK

TSK · Numbers 10:22

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Teewul baayam lànk, ne ko: «Xam naa ko, doom, xam naa ko. Moom itam dina doon aw xeet tey doon ku màgg, waaye rakkam a koy sut, te askanam dina law, ba di ay xeet.»

¶ «Waa raayab Efrayim ñooy dale wetu sowu, ñook seeni gàngoor, kilifag askanu Efrayim di Elisama doomu Amiyut.

¶ Bésub juróom ñaareel ba kilifag Efraymeen ña, Elisama doomu Amiyut moo aye,

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bu ñuy wax Tóor-tóor yi, di seedeb Sabóor, giiroo ci Asaf.