TSK

TSK · Numbers 11:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Fekk na ñaari góor a nga desoon ca dal ba, kenn ka di Eldàdd, ka ca des di Medàdd, te teewul leer ga dal ca seen kaw, ndax dees leena limaale woon ca mag ña, doonte demuñu ca xayma ba. Ñoom it ñuy wax ay waxyu ca dal ba.