Numbers 25:9
TSK
Ña dee ca mbas ma nag di ñaar fukki junneek ñeent (24 000).
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ña dee ca mbas ma nag di ñaar fukki junneek ñeent (24 000).
Yàlla wale ngelawal penku fa asamaan, bëmëx ak dooleem ngelawal bëj-saalum.
Yàlla mer na, dal ci seen kaw, bóom ña ëpp doole ca ñoom, fàdd waxambaaney Israyil.