Numbers 14:6
TSK
Yosuwe doomu Nuun, ak Kaleb doomu Yefune, ñoom ña bokk ca ña seeti woon réew ma, daldi xotti seeni yére ndaxu tiis.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yosuwe doomu Nuun, ak Kaleb doomu Yefune, ñoom ña bokk ca ña seeti woon réew ma, daldi xotti seeni yére ndaxu tiis.
“Kenn du gis mukk réew ma ma giñaloon Ibraayma ak Isaaxa ak Yanqóoba, ci góor ñi jóge Misra te am ñaar fukki at, jëm kaw, gannaaw mataluñu kóolute ci man.
Xanaa Kaleb doomu Yefune moo koy gis, te réew ma mu teg tànkam, moom laa koy jox, mook askanam, ndax moo matal kóolute ci Aji Sax ji.»
Aji Sax ji, woo naa la wall lu ma man, wuyu ma, ma topp sa dogali yoon.
Ba Barnaba dikkee ba gis yiw, wi leen Yàlla may, dafa bég, di leen ñaax ngir ñu ŋoye seen xol ci Sang bi.
Lu ngeen mana def, liggéeyeleen ko xol bu tàlli, ni bu ñeelul woon nit doŋŋ, xanaa Boroom bi.