TSK

TSK · Numbers 15:40

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

ndaxte man Aji Sax ji maay seen Yàlla. Kon nag sell-luleen te sell ndax man ku Sell laa. Kon buleen sobeel mukk seen bopp ci mboolem bindeef yu sew-sewaan yiy dox ci suuf.

kuy sàmm kóllëreem, di saxoo jëfe tegtali yoonam.

Te mooy noonu mu nu taamoo ba àddina sosoogul ndax Almasi mi nu bokk, ngir nu doon ñu sell te mucc sikk fa kanamam. Ci biir cofeel