TSK

TSK · Numbers 20:15

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ña nga jiital seeni jur, daldi yóbbaale seen alal, ja ñu ame réewu Kanaan. Noonu la Yanqóoba deme Misra ànd ak njabootam gépp,

Ba loolu amee ñu fal ay nit ñu leen di ga ca seeni sas, di leen ca fitnaal lool. Noonu la bànni Israyil tabaxale Firawna buuru Misra dëkk, ya ñu naa Pitom ak Ramses, mu def ko ay dencukaayi dund.

Gannaaw loolu Firawna sant waa réew ma yépp, ne leen: «Mboolem doom ju juddu ci Ebrë yi, di góor, sànnileen ca dex ga, waaye lu ciy jigéen, bàyyileen, mu dund.»

¶ Diir ba bànni Israyil nekk Misra tollu na ci ñeenti téeméeri at ak fanweer (430).

Dangaa xeeb li nga nu jële réew mu meew maak lem ja tuuroo, ngir reylu nu ci màndiŋ mi, ba tax ngay buur-buurlu ci sunu kaw teg ci?

Ñu teg ca juróom ñaari fan, xale ba dee. Surgay Daawuda ya ragala wax Daawuda ne ko xale ba dee na. Booba ña ngay xalaat naan: «Ndegam ba xale bay dund lanuy wax ak moom, dégluwu nu kay, ana nu nu koy waxe ne xale bi dee na, muy def njaaxum?»

Acts 7:19 TSK

Buur boobu nag di muusaatu sunu xeet wi, di mitital sunuy maam, di leen sànniloo seeni liir, ngir ñu baña dund.