Numbers 33:45
TSK
Ba ñu jógee Yee Abarim, Dibon Gàdd lañu dali.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba ñu jógee Yee Abarim, Dibon Gàdd lañu dali.
Aw yoon la nu Musaa dénk, muy jagleb péncum Yanqóoba.
¶ Gannaaw loolu Elyasib sarxalkat bu mag ba ànd ak bokki sarxalkatam, ñu tabaxaat bunt ba ñuy wax Gàtt ya, sellalal ko Yàlla, taxawal laf ya, defaraat tata ja, ba ca soorooru Meya, sellalal ko Yàlla, jàppoo ko noonu ba ca soorooru Ananel.
Aji Sax jee nuy jiite, Aji Sax jee nuy dogalal yoon. Aji Sax jeey sunu buur! Moom moo nuy wallu.
¶ Ñi barele alalu àddinay tey nag, dénk leen ñu baña réy te baña yaakaar alal ju wóoradi, te ñu yaakaar Yàlla mi nuy xéewale lépp, ngir nu di ko bége.